Kawtef – « Dama am dieukeur, sama ex eumbeul ma niari yon… » terrible confidence de cette femme.

Kawtef – « Dama am dieukeur, sama ex eumbeul ma niari yon… » terrible confidence de cette femme.

Cette femme a partagé son calvaire en Ano. En effet, elle confie qu’elle a été engrossée 2 fois par son ex alors que son mari est en voyage, en Europe.

« Je suis marié y a 3ans, avant je sortait avec un homme banialouma dra je pensais que moy done sama djieukeur un jour sah ndah nouniou melone. Ms damako tromper wone ndah beug lou bonne rk ak xaliss surtout niouma done influences moma dougeul ci beneu modou modou. Wayé sama djieukeur dh beneu semaine lako guiss. Té mom la amm comme plaisir ci sama mariage. Bonou batay nak degatouma ko doussah woté ay mbokam douniou ma fallait. Diohou niouma beneu nouvelle ci mom.Loumaci geuna metti dama amm djieukeur amm farr actuellement mangui guénatt ak sama ex bi ba diellé fa eumb niari yone té mom tamit manouma takk pask tassouma ms 3ans awma beneu nouvelle de mon mari je sais plus quoi faire. »

0 COMMENTAIRES
    Publiez un commentaire

    Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *